So so bik bik mo mo bidon djilon Saffol djungol saffol xoro molu mo koranye Sek naa sek sama xil man xaw molu mudom Suma fabo boy bek dem laajji djilu mudom Soma jori banya dem man wiji waruna Wey walo wey wado wey wado wey walo fumajum Shibidadu te te te de dadeu Pekh mu nekk wi jiket man daf may tangu lo Nekk ak sama karib wi jiken bi daf may ketum Yimasalon kerok dimas banigi mo nekni Au secours au secours au secours SOS Shibidadu te te te de dadeu Yeah So dafeli melu wax Dutelenu xam lumu joy Yeah yeah wax mu daga Lumu meti meti ngaw wax mu daga Yeah Pekh mu nekk wi jiket man daf may tangu lo Nekk ak sama karib wi jiken bi daf may ketum Yimasalon kerok dimas banigi mo nekni Au secours au secours au secours SOS Shibidadu te te te de dadeu Yeah Li ditsine bar Lum la xagnul dul la ko may Yeah yeah wax mu daga Lumu meti meti ngaw wax mu daga Yeah Man damadol la xotuwaaw Bafa flakaso Wey walooy Ni leen koyi yiyi yaay Sokno wi nileen e'n lu dul xali so Waaw dayna bagnana Ou drogue baaxul Manu sokno woko Waaw dayna bagnana Man damadol la xotuwaaw Bafa flakaso Wey walooy Sibidadu waal si ndi gigno leeno Si wi gii arampe no leeno Ni leen koyi yiyi yaay Sokno wi nileen e'n lu dul xali so Waaw dayna bagnana Ou drogue baaxul Sokno woko Waaw dayna bagnana Man damadol la xotuwaaw Bafa flakaso Wey walooy