作词 : Cheikh tidiane Krouma 作曲 : Yoro Fall Yaw mane késsé nga love Bayil sagou bi Fo né ? Do sax xéf bomay xool Yeah So takone sa fit nieuw (KAAY) Di nga xamni deuss ngay daw ko ko wax kenen day done dieuw (KAAY) kaay gnou waxtané ko à deux Dama meune gane Nekha nekal Kou ma xass xam Douma baayi waxal ak mane kone thi ngay xam li ngay ragal doula gagne Yeneu saay Goor guiss sa taar Yakaar ni yangui thi lepp Pendant ce temps Yangui wait Diko xalaat ci sa nekk Bae fo né Bo gnewul ma gneuw ndax Mang ciy dé Loutax ngay xéx ak sa mbeguél oh oh So takone sa fit gneuw (KAAY) Dinga xamni deuss ngay daw Ko ko wax kenen day done dieuw (KAAY) Kaay gnou waxtané ko à deux Dama meune gane Nekha nekal Kou ma xass xam Douma bayi Waxal ak mane Kone thi ngay xam Lingay ragal Doula gagne (Doula gaagn Eh ) Toc toc ! Bae wake-up good morning ! Message yi Boom Boom flames yi jolli Aldianaa lay xaar bo défone geste Thiabi diaa ngui thi yaw lay déss (Xaar bi doyna) Boy takal sa fiit bi Té nieuw diekhal thiow li (Xaar bi doyna) Mane maay moudié indil leu warou gar bi niou marier So takone sa fit gneuw (KAAY) Dinga xamni deuss ngay daw (KAAY) Koko wax kenen day done dieuw (KAAY) Kaay gnou waxtané ko à deux Dama meune gane Nekha nekal Kou ma xass xam Douma bayi Waxal ak mane Kone thi ngay xam Li ngay ragal Doula gagne