Momel

歌曲 Momel
歌手 Diogal
专辑 Liir

歌词

Momel liniou momone
Non non louniou non non
Taye ma wakhla li niou bokeu nioune takhoul nga bagnma
Taye ma wakhla li niou bokena
Setal faniou dioguei
Setal iow liniou bokone
Taye ma wakhla li niou bokeu nioune takhoul nga bagnma
Taye ma wakhla li niou bokena
Momel liniou bokk mome
Non non liniou bokk am Adama suniou Baye Awa moye suniou Yaye
Non non louniou khiro momel liniou bokk
am Awa moye suniou Yaye Adamay suniou Baye
Momel liniou momone
Non non liniouy non non
Momel liniou momone
Momel